Aller au contenu

Waxtaan:Fitna

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.

Mbok nuyu na leen, dama bëggon ngeen xolaat bind mi ndax bari ba ay njumte. Tay sokoy dawal dangay gis nii baatan yi ni ñu ko binde dafa doy waar loolu nag ma sakku won ngeen defaat ci ay gestu ndax dawal bi mën a nex ci kuy tambali njàng mi

Jaa ngeen jëff 212.114.207.30 4 Maars 2022 à 19:43 (UTC)[répondre]