Tabanaani
Apparence
Tabanaani xeetu gàncax la gu bokk ci njabootu Euphorbiaceaete bàyyikoo Meksig.
Melo wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Garabu tabanaani man naa àgg ba 8i sàntimet ci guddaay. Xobam day xonq. Doom bi danay ëmb lu toll ci 25% ci diw, jiwu bi nag 37% lay ëmb ci diw. Garab gi xet gu xasaw lay gilli.
Njariñ li
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Nekkam tooke teewut ñu koy bay ngir diwam. Bokk na ci lees di defaree saabu Marsey.
Nataal yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]-
Xob yi
-
Tóortóor bi
-
Doom yi
-
Xoox bi
Turu xam-xam wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Jatropha curcas
Tur wi ci yeneeni làkk
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]farañse: pourghère |
angale: Barbados nut |