Tàndarma

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Tàndarma garab la gu bokk ci njabootu Arécacées ak ci njabootaatu Coryphoideae.

Melo[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Garab gi day àgg 15 ba 30i met ci guddaay. Téeñu xob lañ am.

Xobam day àgg 4 ba 7i met.

Tàndarma bi day meññ ak i ñoñam ciw car. Day saf suukar lool.

Ngelaw leey tóoral tàndarma gi.

Njariñ[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Tàndarma bi dees koy lekk te njaayam bari na lool, rawatina ci weeru koor. Tàndarma gi it bari nay njariñ.

Nataal[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Turu xam-xam[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Phoenix dactylifera