Sëriñ
Apparence
- sëriñ mooy tekki kilifa diinè lislaam. Am xamxam bu sell ak mëna def keemaan (ci doolè Yalla) mooy ñaari kalité yi ñuy gëna yaakaar ci ab sëriñ.
- sëriñ goor lay doon, waayè am na jiggèèn yu am kalitè yooyu, ñu leen di tudde soxna.
- sëriñ it dina faral di tekki ag màggal, niki Monsieur ci Fr, bu dee jigéen ñu ne soxna si