Sëriñ

Jóge Wikipedia.
Aller à la navigation Aller à la recherche
  • sëriñ mooy tekki kilifa diinè lislaam. Am xamxam bu sell ak mëna def keemaan (ci doolè Yalla) mooy ñaari kalité yi ñuy gëna yaakaar ci ab sëriñ.
  • sëriñ goor lay doon, waayè am na jiggèèn yu am kalitè yooyu, ñu leen di tudde soxna.
  • sëriñ it dina faral di tekki ag màggal, niki Monsieur ci Fr, bu dee jigéen ñu ne soxna si