Suraas g
Suraas gi xeetu gàjj la gu bokk ci njaabootu Rutacées. Barab yu tàng yi lees koy bay. Asi la bàyyikoo.
Melo wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Garab gi man na àgg ba 10i met ci guddaay. Wànqaasam day am i dég te xobam 4 10i sàntimet àgg ci guddaay.
Njariñ yi[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Suraas gi soloom ci wàllu koom lu fés la. Am na solo it ci wàllug paj.