Sharles Degóol
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Bii jukki ab junj rekk la.
Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal
Sharle Degóol (ci Faraañse mooy Charles de Gaulle) mi ngi gane àdduna 22 nowambar 1890 ca Liil (Fraas), génn àdduna 9 nowambar 1970 ca Colombey-ñaari-Jàggu-yi. Nekkoon na nitu guur gu Fraas, moo sos juróomeelu gaw bu Fraas 1958, jiite na réewum Fraas li ko dale 1959 ba 1969.