Santiago (Kap Weer)
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Santiago (Kap Weert))
Dunu Santiago | |
---|---|
Réew | Kap Weer |
Rëyaay | 991 km² |
Dalub web | http://www.santiago.cv/ |
Santiyaago diiwaan dunu ci yu Kap Weer. Santiyaago mooy dun bu mag bi ci Kap Weerdi, di ko màggal ci wàllu jëfekaay bi, te mooy kërug genn-wàllu askanu réew mi. Bokk na ci dun yi ñuy wax Sotaweento, nekk ci diggante dun yi ñuy wax Maio (26 km) ci penku) ak Fogo (55 km) ci sowu. Moom moo jëkkoona dëkke: dëkk bu ñuy wax Ribeira Grande (muy tudd Cidade Velha te UNESCO teg na ko ci wàllug Dunu suuf si[2]) lañ ko sos ci atum 1462. Ci dëkku Santiyaago la dëkku Paraaya di péeyu réew mi nekk.
Dëkkaani
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Praia
- Ribeira Grande de Santiago
- Santa Catarina
- Santa Cruz
- São Domingos
- São Lourenço dos Órgãos
- São Miguel
- São Salvador do Mundo
- Tarrafal
Dëkki
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Praia
- Assomada
- Calheta de São Miguel
- Cidade Velha (Ribeira Grande do Santiago)
- Pedra Badejo
- São Domingos
- Tarrafal
Dëkk-Dëkkaani
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Achada Baixo
- Achada Baleia
- Achada Biscainho
- Achada Falcão
- Achada Fazenda
- Achada Lem
- Achada Longueira
- Achada Loura
- Arribada
- Banana (Wolof: Banaana)
- Boa Entrada
- Gil Bispo
- Calabaceira
- Chaminé
- Chão Bom
- Chão de Tanque
- Dacabalaio
- Espinho Branco
- Faveta
- Figueira das Naus
- Fonteana
- Fonte Lima
- Fundura
- Lagoa
- Longueira
- Mancholi
- Mato Raia
- Massapé
- Milho Branco
- Moia Moia
- Nora
- Ôrgãos
- Pilao Cão de São Miguel
- Picos (Achada Igreja)
- Poilão
- Ponta Verde
- Portal
- Porto Gouveia
- Porto Mosquito
- Porto Rincão
- (Ribeira) Principal
- Ribeira da Barca
- Ribeira da Prata
- Ribeirão Chiquinho
- Salineiro
- Vila Sambaia
- Santa Ana
- São Francisco
- São Jorge dos Órgãos
- São Lourenço do Santiago
- São Miguel
- São Pedro da Calheta
- Serra da Malagueta (Serra)
- João Teves
- Rui Vaz
- Xexé (Sheshe)
Sport
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Staad
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Staad 25 samwiyee - Pedra Badejo
- Staad Calheta - Calheta de São Miguel
- Staad Cumbém - Assomada
- Staad Mangi - Tarrafal
- Staad Várzea - Praia
Dayo
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- André Álvares de Almada
- Ivan Almeida
- Jorge Barbosa
- Gardénia Benrós
- António Lopes Cardoso
- José Ulisses Correia e Silva
- Codé di Dona
- Mito Elias
- Silvino Lopes Évora
- Dário Furtado
- Suzanna Lubrano
- António Mascarenhas Monteiro
- Jose Maria Neves
- Orlando Pantera
- António Pedro
- Fernando Quejas
- Simplício Rodrigues de Sá
- Tcheka
- Izé Teixeira
- Toni Varela
- Manuel Veiga
- Arménio Vieira
- Lela Violão
Iniweersite
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Iniweersite Kap Weert
- Jean Piaget Iniweersite Kap Weert
- Iniweersite Assomada
- Iniweersite Santiago
Karmat ak delluwaay
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Lëkkalekaay yu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Xool it Wikimedia Commons
|
- http://www.santiago.cv (en) (pt)
|