Sëriis
Sëriis garab gu bàyyikoo Madagaskaar la. Ci njabootu Phyllanthaceae la bokk. Doomam dees koy lekk, day wex. Xobam rënd la ci toggi yenn réew yi
nataal yi[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Turu xam-xam[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Yeneen làkk[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Farañse: girembellier