Sànceer

Jóge Wikipedia.

Sànceer, garab la guy faral di am ci diggu Afrig, réew yu mel ni keeñaa, Somali,Tansani jàpp Gànnaar ba Senegaal. Ci àll bi ak ci tefes gi lay faral di ñoree.

Melo wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Garab la gu man a sëq lool. Ay caram dañoo dëng, ab guddaayam man a toll ci 2i met jàpp 6i met.

Njariñam[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ay doomam dees koy lekk. Reen bi boo ko nalee walla nga baxal ko man nga ko jëfandikoo ci wàll um paj yu bari, ( Gaana, Sifili, Gonoore, stomaa...). Sunguf si juge ci reen bi ak xànc mi day faj ay góom.

Ay doomam dañuy faj tooke ak lu ci mel ne màtt-màttu jaan.

==Loraange yi==

Giseesagu ci lor.

Nataal yi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Turu xam-xam wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Feretia apodanthera