Aller au contenu

Royuwaay:Melosuuf/bunt

Jóge Wikipedia.
BUNTU MELOSUUF
Melosuuf mooy xam-xam biy settantal ak a leeral feeñtey yaram yi, walla jëmm yi, yu dundat yi, yu nit ñi ci kaw suuf si ak gëstu gi aju ci ni ñu séddalikoo.