Aller au contenu

Royuwaay:Infobox en Lua

Jóge Wikipedia.

Abla Pokou (wala Aura Poku, wala Abraha Pokou) lingeeru Afrig la , juddoo ci fukk ak juróom-ñetti xarnub. Indi na askanu Baoulé ci réewum Gana ba ci Kodiwaar. Léeb bi dafa nettali, saraxu doomam bu góor ngir jàll ag dex .

Bat bi "Baoulé " li nu tudde leegi askan yi , mu ngi joge ci saraxu doomam.

Bicci toppu saraxe, né na "Ba-ouli", loolu dafay tekki "doom bi dee na".