Aller au contenu

Rand

Jóge Wikipedia.

Rand garab gu ndaw lay, mi ngi bokk ci njabootug Fabaceae, cosaanoo Afrig, dees koy fekk ci gox yi nga xam ni suuf si day xaw a wow fu mel ni Sahel gi.

Xobam ak doom


Garab la gog guddaayam li ci ëpp 1i met la doy jàpp 3i met, yenn saay man naa àgg 8i met, day niru garab gu am ay dég, te fekk ci dëgg-dëgg ay car yu amul xob la, ay xobam dañuy yor melo wu nëtëx. Ay doomam njokkub lujum lay doon.


Njariñ yi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Garab la gog dees koy jëmbat ngir rafetal.

Rand gi
Rand gi


Turu xam-xam wi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Bauhinia rufescens