Peex
Apparence
Peex xeetu garab la gu bokk ci njabootu Bignoiaceae te bàyyikoo Afrig gu naaje.
Melo
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]As ngarab la su am i tóortóor yu yor melow puur te dajaloo ciw car.
Njariñ
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Jur gi dañ ciy xéewaloo.
Nataal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]