Ndaté Yalla Mbodj

Jóge Wikipedia.
Ndaté Yalla Mbodj
Dundu ak jaar-jaaram
Nataalu lingeer Ndate Yàlla Mbooj
Nataal bi .

Lingeer Ndate Yàlla Mbóoj

Lingeeru Waalo
Xew- xewi dundam
Turu buur bi Lingeer Ndate Yàlla Mbóoj
Giir bi Giirub Tedyeg ci wàllu meenam ak giirub Diyoos ci wàllu geñoom
Turam Ndate Yàlla Mbóoj
atum juddu-atum faatu - 1860
Béreb ba mu juddoo Waalo, Senegaal
Pàppam Barag Amar Faatim Borso Mbóoj
Yaayam Lingeer Awo Faatim Yamar Xuri Yaay Mbóoj
jëkkëram 1. Barag Yerim Mbañig Tegg Réll

2. Maroso Tase jóob (Saakura Barka Jóob) - Buuru Kayoor[1],[2]
Doomam Siidiya Lewon Jóob
Diineem Afrig

Lingeer Ndate Yàlla Mbóoj,am nu koy woowee Ndete Yàlla, mu ngi juddu atum junni ak ñetti téemeer ak fukk, génne àddina atum junni ak juróom ñetti téemeer ak juróom benn fukk. Nekkoon na buur bu jigeen bu mag ca réewum waalo, réew mi féetewoon ca bët-gannaar penku Senegaal.

  1. Afrique Histoire U.S., Volume 3, Afrique histoire U.S. (1985), p. 32
  2. Barry, Boubacar, Senegambia and the Atlantic Slave Trade (ed: David Anderson, and Carolyn Brown ; trans: Ayi Kwei Armah ; con: David Anderson, American Council of Learned Societies, Carolyn Brown, University of Michigan. Digital Library Production Service, Christopher Clapham, Michael Gomez, Patrick Manning, David Robinson, Leonardo A. Villalon), Cambridge University Press (1998), p. 182, (ISBN 9780521592260)