Musée de la (Gorée)

Jóge Wikipedia.

Deccukay bunnu doppe guedj gui moy deccukay binnu def cibir dokh mi tee boleko si IFAN, tee nu tekko feulee sa Goore di teffessu Dakaaru biir Seenegaal.

Melosuuf[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Fetewukay[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Kheer bobbu di Goore moggi bokku ci 19 arrondissema ci deuk bobu di Dakaaru, Seenegaal. Benn kheer buuy def 18,2 Hectar tee mo nekk 2 kilo diggetem ak teffessu Dakaaru.

Goore moggi nekk si diggi gedj gi manaam si digg kheer Cap Ver. Deuk bobbu di Goore reyuul loluu, manaam 900 metar la ak 300 lollu takhna nitt munufi reer. Kuu wakh melossuf wakh si jaww dji. Munn ngafa niow tee sollo yeere buu diss (loluu na fekk doffa fanann). Ayy temperaturam mogui nekk 17 ak 25° si sedd bi, 24 ak 30° bu tangge. Dakh lollu takhna nuu yeugeul sunu xaritu tubaab yi! Loluu takh guudi gi buu fekkeni tangoor la sakh solefa yeere bu diss.

Fumou nekh[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Tarikh Gorée[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ci karagn tee[Soppisoppi gongikuwaay bi]