Mikael Jakson
Apparence
Michael Joseph Jackson (29 ut 1958 – 25 juin 2009) doomu Amerique la woon, waykat, bindkat, feccikat ak ku bëgg doomi aadama yi. Ñu ngi ko woowe "Buuru Pop", ñu jàpp ni kenn la ci nit ñi gëna am solo ci wàllu aada ci 20eelu xarnu bi.[1][2]
Rew Yii Aduna Yep
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- ↑ Rodriguez, Cecilia. "New Blockbuster Paris Exhibition Celebrates Michael Jackson". Forbes. Archived from the original on October 31, 2019. Retrieved October 31, 2019. Unknown parameter
|url-status=
ignored (help) - ↑ Stevens, Hampton (2010-06-24). "Michael Jackson was the most influential artist of the 20th century.". The Atlantic. Retrieved 2024-04-28.