Melosuufug Tugal
Apparence
Tugal benn la juroom ñaari gox yi nekk ci àdduna bi. Ay dig yu suufi Tugal yenn saa yi day indi ay werante, su ñu xoolee ni ko waa tugal ci seen bopp jappee, ci penku ci Asi la sës, ci sowwu mi ngi yem ci Mbàmbulaanu Atlas, ci bëj-gànnaar ci dottu bëj-gànnaar, géej gu diggu gi mooy koy yemale ci bëj-saalum. Liy indi werante bi mooy Risi ak Siipër ak Tirki, réew yi ci wàllu séwógaraafi dañ leen di boole ci Tugal te xaaj bu am solo ci seen suuf nekk ci Asi.
Tay am na weneen gisiin ci ay digi Tugal. Waa Tugal yi Da ñuy jàpp ne