Mbootaayu koom- koom u réew i Afrig sowu jant

Royuwaay:Infobox Organisation

Communauté économique des États de l'Afrique de l'Ouest (CEDEAO) (fr)

Economic Community of West African States (ECOWAS) (en)

Comunidade Económica dos Estados da África Ocidental (CEDEAO) (pt)
alt=Logo de l'organisation|langue=fr|280x280px
Situation
Création
Type Organisation intergouvernementale
Siège Abuja (Nigeria)
Coordonnées 9° 02′ 32″ N, 7° 31′ 31″ E
Langue anglais, français, portugais
Organisation
Membres
Président bordure|classe=noviewer|20x20px|Drapeau du Niger Mahamadou Issoufou
Personnes clés bordure|classe=noviewer|20x20px|Drapeau de la Côte d'Ivoire Jean Claude Brou, président de la Commission

bordure|classe=noviewer|20x20px|Drapeau de Sierra Leone Sidie Muhammed Tunis, président du Parlement

Site web http://www.ecowas.int/
Géolocalisation sur la carte : Nigeria
[[Fichier:Nigeria_location_map.svg|classe=noviewer|280x280px|(Voir situation sur carte : Nigeria)]]
Géolocalisation sur la carte : CEDEAO
[[Fichier:CEDEAO_location_map.svg|classe=noviewer|280x280px|(Voir situation sur carte : CEDEAO)]]
Géolocalisation sur la carte : Afrique
[[Fichier:Africa_location_map.svg|classe=noviewer|280x280px|(Voir situation sur carte : Afrique)]]

Royuwaay:Organisations supranationales africainesMbootaayu koom-koom u réew i Afrig sowu  jant ab kuréel la gu dox diggante ay gornamaa, ñu taxawal ko 28i fan i mee atum 1975. Mooy kureel gi gëna raññiku ci lëkkële yéngu yéngu réew yi  féete Afrig  sowu jant (MKRASJ). Li ko taxa jog, mooy jëflante ak dugalante ngir mana taxawal ag bennoo ci wàallu koom ak xaalis. Ci atum 1990 lees ko doleele wàllu saytu kaaraange gi ci diwaan bi, ak ECOMOG gi ñu taxawal, mu di ag kureel u soldaar guy wàllu. Ca atum 1999 nak lañ ko saxal dàkk. Tey jii, 15i réew ñoo  bokk ci MKRASJ. Ci atum 2017 allalu réew yooyu ca bokk àggoon na ci lu toll ci 565i tamñareet ciy dolaar u Amrig.

Doonte bamu sosoo koom-koom rekka ko yitteeloon, MKRASJ dafa gaaw jublu ci luy saytu jàmm ak lu koy dëgëral. Loolu sax doon lu manula ñàkk ci bu ñu bëggee taxawal am mbootaay mu dëgër.  Ginaaw loolu, MKRASJ farlu na ci tabax ci diwaan bi ay jumtukaay ci wàllu dem ak dikk ak jokkookaay yi.

COSAAN LI[Soppisoppi gongikuwaay bi]

LI  JIITU[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Mbootaayum koom-koom u réew i Afrig sowu  jant mu ngi soqikoo ca mbootaayu duwaañ bi boolewoon 4i réew u kuréelug déggo, ñu xamoon ko ci (Conseil de l’Entente) ak Mali. .

SUMB GI[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ca atum 1972 la Yakubu Gowon, dib seneral bawoo Niseria ak Ñasimbe Eyadema bu Togo digle ngir ñu sos ci diwaanu Afrig ab ëtt ngir koom-koom u réew yi mana duggante. Loolu soññ seen yeneen i nàttangoo yi. Ci noonu lañ ko waxtaane ak 12i réew diggante weeru sulet ba ut atum 1973..

TERETE BI NJËKK (1975-1993)[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ñagas ñagas yi amoon ci diggante yenn réew  yi ñoo indiwoon  MKRASJ mu dogal ci atum 1978 ab sart buy tere jàmmaarloo diggante ay réew. Topp ci beneen ci atum 1981, buy digle jàppalante ci wàllu kaarange boole ca genn  woote ci ay doxalin u polotig sulet ci atum 1991. Waaye nak ci atum 1990 la jëmmal tigi fànn wi laal kaarange. Ca lël bi njit i réew ak yu goonamaa yi amaloon la jàpp sosug kureel giy saytu jëmëlug wéer nganaay yi. Kuréelug saytu googu doon ci diir bu gaay ab dooley àttekaayu xeex. Ci noonu la dugge ci xare ba amoon biir Liberiya, bii Sera Leona ak biir Gine-Bisaawo.