Aller au contenu

Mboolaay

Jóge Wikipedia.

Mboolaay baat la bu dage ci "mbooloo", moom nag di ci wu faraas "société" mooy dundiinu mbooloo mi aw nekkiinam tey ag nosteem ak aw nosuwiinam, maanaam ni muy nose biiram ak aw dundiinam ak lëkkaloo gu ay céram (ses membres)akug róofoom. Moom nag dina taxawe baat niki:

  • Mboolaay (société):Kureelu mbootaayu xeet yi de, ak li mu def lépp ci liggéey yu jëm ci saxal jàmm ci àdduna bi ci biir fukki at yu njëkk yi, ak li mu fi def ci liggéey yu am njariñ ci wàllug mboolaay

walla aji melal (adjective)niki:

  • Mboolaay (social):Jataayub koom-koom ak mboolaay