Maymuna Kan
Erreur de script : la fonction « build » n’existe pas. Abla Pokou (wala Aura Poku, wala Abraha Pokou) lingeeru Afrig la , juddoo ci fukk ak juróom-ñetti xarnub. Indi na askanu Baoulé ci réewum Gana ba ci Kodiwaar. Léeb bi dafa nettali, saraxu doomam bu góor ngir jàll ag dex .
Bat bi "Baoulé " li nu tudde leegi askan yi , mu ngi joge ci saraxu doomam.
Bicci toppu saraxe, né na "Ba-ouli", loolu dafay tekki "doom bi dee na". Xew- xewi dundu Maymuna Kan
Jamono ju mu juddoo: fukki fan ak ñett ci weeru mars atum junni ak juróom ñeent teemeer ak fanweer ak juróom ñaar ca Ndakaaru
Jamono ju mu faatoo: benn bés ci weeru mars ci atum ñaari junni ak fukki fan ak juróom ñeent (amoon juróom ñetti fukki at ak benn ba muy faatu) ca Pari
Turam: Maymuna Ndongo
Réewam: senegaal
Yëngu-yëngoom: jigeen juy def politig, àttekat la
Turu jëkkëram: Mamadu Ture
Maymuna Kan a ngi juddu fukki fan ak ñaar ci weeru mars atum junni ak juróom-ñeent- téemeer ak fanweeer ak ñaar ca Ndakaar(Senegaal) (1). Mu ngi génn àdduna benn fan ci weeru mars ci atum ñaar junni ak jukk ak juróom- ñeent ca Pari (farãs) (2) . Bokkoon na ci àttekat yu mag ci rééw mi. Loolu terewu ko takk ndombal tànk ba doon ministar.
Xew- xewi dundam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Maymuna Kan nekkoon na óditëer ci ëttub àtte bu mag bi. Nekkoon na itam ki nu toftal ci porokirëeru ndakaaru. Doonoon na déeyaakoon ci ëttu àtteb àttewaat ca ndakaaru(3). Mu ngi dugg ci nguurug Abdu Juuf ci fukki fan ak juróom ci weeru mars atum junni ak juróom ñeenti téemeer ak juróom ñaar fukk ak juróom ñett. Fekkoon na fa moroomu jàmbaar ju tudd Karolin Fay Jóob. Noonu lanu ko tabbe mu doon sekereteeru nguur gi nu toftal ci jëwriñ ju mag jiy toppatoo nekkinu jigeen ñi, nekkinu nit ñi ak a
yëkkëti taxawaayu nit ñi. Tur woowu dina am coppite(4). Ba nu tabbee Mustafaa Ñas jëwriñ ju mag ji juróomi fan ci weeru awril atum junni ak juróom ñeenti téemeer ak juróom ñetti fukk ak ñett lanu ko dénkee jëwriñu cuqali nekkin wi.
Doon nanu ko woowee Ndongo. Nekkoon na soxnas Yaya kan. Kooku nekkoon na ku doon yëngatu wi wàllu koom. Amoon na ak moom juróomi doom. Ba jëkkër ja gaañoo, la sëyaat ak ku xam-xamam màccoon ci koom-koom, ku nu naan Mamadu Ture, moom mi nekkoon jëwrin ji nu dénd koppari réew mi diirub weeru me atum junni ak juróom ñeenti téemeer ak juróom ñetti fukk ak ñett ba weeru me atum junni ak juróom ñeenti téemeer ak juróom ñetti fukk ak juróom ñett (5).
Tànneefu téere yiy génne
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- (en) « The Status of Married Women Under Customary Law in Senegal », in American Journal of Comparative law, 20 (4), 1972, p. 716-723
- « Condition de la femme sénégalaise », in Revue juridique et politique, no 28, octobre-décembre 1974
- « La protection de la femme et le maintien de la famille sénégalaise », in Revue sénégalaise de droit, no 16, 1974, p. 33.
Xoolal itam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Xew- xewi dundam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- (en) Anne Winslow (dir.), Women, politics, and the United Nations, Greenwood Press, Westport (Conn.), Londres, 1995, p. 49-53 (ISBN 0-313-29522-0)
- Babacar Ndiaye et Waly Ndiaye, Présidents et ministres de la République du Sénégal, B. Ndiaye, Dakar, 2006 (2e éd.), p. 250
- Les Élites sénégalaises, Ediafric, La Documentation africaine, 1984, p. 96