Malabo
Apparence
![Wikipedia](http://upload.wikimedia.org/wikipedia/commons/thumb/e/ef/WikiLettreMini.svg/36px-WikiLettreMini.svg.png)
![](http://upload.wikimedia.org/wikipedia/commons/thumb/8/86/Panoramic_view_of_Malabo.jpg/315px-Panoramic_view_of_Malabo.jpg)
Malabo | |
---|---|
![]() | |
Réew | ![]() |
Tund | Bioko norte |
way-dëkk | 60 065 nit |
atum way-dëkk | 2 004 |
Barabalub Malabo ci Gineg yamoo | |
Malabo mooy péeyu réewum Gineg yamoo, mi ngi féete ci bëj-gànnaaru dunub Bioko. làkk wees gën di jëfandikoo ca dëkk ba mooy wu-espaañ ak wu-gineg-yamoo. Malabo ci jamono yi weesu jotoon naa am yeenen tur:
- 1827 ba 1846: Clarence City (tur bi ko waa-angalteer joxoon) ;
- 1846 ba 1973 : Santa Isabel (tur bi ko waa-espaañ joxoon) ;
- 1973: Malabo (tur bi ko waa-Gineg-yamoo jox).