Maam Yunus Jeŋ

Jóge Wikipedia.

Erreur de script : la fonction « build » n’existe pas.Royuwaay:Infobox en Lua

Maam Yunus Jeŋ

Dundu ak jaar-jaaram
Juddu 1939

Tiwaawon

Faatu 1er awiril 2016

Dakaar

Senegaal Senegaal
Liggeey Bindkat, taalifkat

Maam Yunus Jeŋ (juddu 1939, faatu 2016) ab bindkat la bu dëkk Senegaal.

Dund ak jaar-jaaram[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Maam Yunus Jeŋ mu ngi juddoo Tiwaawon, ci Kayoor atum 1939. Waajuram wu góor a ngi cosaanoo Kayoor, waajuram wu jigeen moom, cosaanoo Ndar (See Luwi). Jàngalekat la woon mujj nekk njiitu lekool[1].

Maam Yunus Jeŋ ci farañse ak wolof yépp la daan bind, moom mooy ki jëkk a bind ab téereb nettali ci wolof tudde ko Aawo bi. Téere boobu ñu ngi ko siiwal atum 1992 ci Dakaar, mu teg ci beneen téereb nettali bu tudd L'ombre en feu, ñu siiwal ko atum 1997[2].

Àjjuma benn fan ci weeru awiril atum 2016 la génn àdduna ci këram, ci Dakaar[3].

Ay Téereem[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • L'ombre en feu, Dakar, Les Nouvelles Éditions Africaines du Sénégal, 1997, 233 p. (ISBN 2-7236-1108-6). Aussi, très soutenue par sa fille aînée Ndeye Bogui Sow Camara à qui l'édition de ce livre tenait à cœur.

Téere, jukki wala dali web yi ñu yër[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Seetal tamit[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lees bind ci moom ak ay téereem[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • Lilyan Kesteloot , « L'Ombre en feu de Mame Younousse Dieng », in Éthiopiques, n° 60, 1er semestre 1998
  • (en) Jean-Marie Volet, « Tradition and Modernity Are Here to Stay: An Analysis of Francophone African Women's Writings Published in 1997-98 », Research in African Literatures, vol. 30, n° 2, été 1999, p. 182-193.
  • Guedj Fall, « Aaawo Bi de Mame Younousse Dieng, un récit fondateur en langue wolof », in Éthiopiques, n° 76, 1er semestre 2006.
  • Abdoulaye Keita, « Dieng, Mame Younousse [Tivaouane 1940] », dans Béatrice Didier, Antoinette Fouque et Mireille Calle-Gruber (dir.), Le dictionnaire universel des créatrices, Éditions des femmes, 2013, p. 1254.

Jukki yi ñu ko tudd[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lees jële feneen[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • . Fees ko mën a xame :
    • Fichier d’autorité international virtuel
    • International Standard Name Identifier
    • Bibliothèque nationale de France (données)
    • Système universitaire de documentation
    • Bibliothèque du Congrès
    • Gemeinsame Normdatei
    • Bibliothèque royale des Pays-Bas
    • WorldCat


Maam Yunus Jeŋ ci dalu web Lire les femmes écrivains et les littératures africaines