Mëfër mi (rabu àll)

Jóge Wikipedia.

Mëfër mi, mooy segg gu ñuul, muy segg gu bari malani ci yaramam, muy fer-ñentug ndono guy tax yaram wi ñuul kukk. Ci àll yu fatt yi te bari taw la ëppe ca bëj-saalumu Asi ak End (11% mëfër) lu jafee gis Afrig la, melo wu mel nii dina faral di am itam ca Amerig Jagwaar

Black panther India.jpg Menn mëfër ca géttu réewum Nagarhol, ca End.

Jaguar.jpgMenn mëfër ca Soo-Henrii-Doorly, ca réewi Amerig.

Black leopard.JPG Menn mëfër ca Afrig Bëj-saalum.

Melanism in Panthera Onca.jpg Jagwaar bu ñuul ànd ak mooroomu seggam.