Lóriye
Lóriye gi xeetu garab la gu bokk ci njabootug Lauraceae, ci bëj-saalumu Tugal la bàyyiko waaye amna ci barab yi bari naaj ci àddina bépp, Senegaal it.
Melo wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Garabug lóriye dafa man a àgg 10i met ci guddaay, xobam day gulumba te wirgo wu nëtëx lay yore, tóor-tóor bi day mboq.
Nataal yi[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Turu xam-xam wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Laurus nobilis