Aller au contenu

Końskowola

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Końskowola ab dëkku-kaw la ca bëj-saalum-penkug Poloñ. Mi ngi ne ci diggante Puławy ak Lublino, ci wetu Kurów, ci dexu Kurówka. Mooy péyu gox-goxaan bii di gmina.

Mi ngi yaatoo 9,8 km², ci 2004 amoon na 2.188 way dëkk.