Kax b

Jóge Wikipedia.
Aller à la navigation Aller à la recherche

ViverraPoortmanniSmit.jpg Kax bi

Civettictis civetta 11.jpg ab kax.


African Civet area.png fi kax yi dëkke ci kembaaru Afrig


Kax nag bokk na ci limka gi mbootaay gii di "Booleg Réew Yi Ngir Sàmm Kéew Mi" def ci atum 2008 ñeel ràbb yi nar a raaf ci kaw suuf, maanaam sunu moytuwul dootuñu amati dañuy jeex. yenn dëkk yi li ko fay raafloo mooy nit ñi leen di rëbb ci amam yu jaaduwul ngir di ci defar ay gëtt. Kax nag rabbu guddi la, bëccëg gi yépo da koy nelaw ci diir ñax yu fatt yi, di yeww bu janti bi sowee.