Andare wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Luckas-bot (waxtaancëru)
m r2.7.1) (Robot: Adding nds:Andreas (Apostel)
Rubinbot (waxtaancëru)
Rëdd 66 : Rëdd 66 :
[[sw:Mtume Andrea]]
[[sw:Mtume Andrea]]
[[ta:அந்திரேயா (திருத்தூதர்)]]
[[ta:அந்திரேயா (திருத்தூதர்)]]
[[th:นักบุญแอนดรูว์]]
[[th:นักบุญอันดรูว์]]
[[tl:San Andres]]
[[tl:San Andres]]
[[tr:Andreas]]
[[tr:Andreas]]

Sumb bu 17 Oktoobar 2011 à 17:47

Ci angale mooy Andrew; Ci faranse mooy André

Benn ci fukki taalibe Yeesu ya ak ñaar la woon, di rakku Simoä Piyeer. Ñu bokk ndey ak baay. Nappkat bu bawoo ca dëkk bu tudd Betsayda ca diiwaanu Galile la woon. Bala mu topp ci Yeesu nekkoon na taalibe Yaxya.

Dañuy gis Andare ci Injiil ci Mc 4:18-20; 10:2; Mk 1:16-18,29; 3:18; 13:3,4; Lu 6:14; Yow 1:35-44; 6:8-9; 12:20-22; Jëf 1:13.