Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
m Tuddewaat nañ Doxalkat mbëj léegi mooy Doxalukaay bu mbëj
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
'''Doxalkat mbëj''' tekkeem moy ab [[wuutuloxo]] mbëj la, goo xam ne kattan giy duggu ci moom gu [[mbëj]] la te ga muy genne gu [[doolerandu]] la. Doxalkat mbëj yi am nañ solo lool ci dundinu jamono gu bees gi, te it dëgg la sax ne limu doxalkat mbëj yi nekk ci am reew day firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Te itam deminu, maanam yokkute walla nèewte limu doxalkat mbëj yi ci am reew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wàllu [[xarala]] mu reew moomu. Ngir dëggal loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfëndikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.
'''Doxalukaay bu mbëj''', ab [[wuutuloxo]]b [[mbëj]] la, goo xam ne kàttan giy duggu ci moom gu [[mbëj]] la te ga muy génne gu [[doolerandu]] la. Doxalukaay yu mbëj yi am nañu solo lool ci dundiinu jamono ju bees ji, te it dëgg la sax, ne limu doxalukaay yu mbëj yi nekk ci am réew dafay firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Te itam deminu, maanam yokkute walla néewte limu doxalkaay yu mbëj yi ci am réew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wàllu [[xarala]] mu réew moomu. Ngir dëggal loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfandikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.


== Xaralay doxin gi ==
== Xaralay doxin gi ==
Rëdd 5 : Rëdd 5 :
=== Wàll gi solowu: ===
=== Wàll gi solowu: ===
* [[Wëndeelukat]]
* [[Wëndeelukat]]
* [[Tekkaaral]]
* [[Tekkaaralkat]]
* [[Toolu Bijjaakon]]
* [[Toolu Bijjaakon]]
* [[Bijjaakon]]
* [[Bijjaakon]]


=== Doxin ===
=== Doxin ===
Dawanu [[mbëj]] gi day jaar ci ab lëmës gu ñu wëndeel ci ab doggub weñ gi tudd [[Tekkaaral]]. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjbijjaakon bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjbijjaakon googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seex i [[dott]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjbijjaakon; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon gu tekkaaral gi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dottu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.
Dawaanu [[mbëj]] gi day jaar ci ag lëmës gu ñu wëndeel ci ab doggub weñ bi tudd [[Tekkaaralkat]] bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjbijjaakon bu ca dawaan jaaree. Toolu mbëjbijjaakon boobu dañ koy sóob ci beneen toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dott]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjbijjaakon; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon gu wëndeelukat bi day wootalante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon gu tekkaaralkat bi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dott bi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.


Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan safaanu rek la bijjaakon di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kattanu mbëj gi day soppeeku tanggoor ngir [[sababu joule]].
Doxalukaay bii, ci dawaan gu safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan safaanu rek la bijjaakon di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kàttanu mbëj gi day soppeeku tanggoor ngir [[njeexitu joule]].


== Taariixam ==
== Taariixam ==
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjbijjaakon gi simikat boobu di Ørsted xamlewoon, la [[jëmmalkat]] bu waa-angalteer bii di Michael Faraday defar ñaari wuutuloxo ngir yoox li mu duppee ab wëndeelug mbëjbijjaakon: ab jalaxub dooley bijjaakon gu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalkat mbëj gu njëkk.
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjbijjaakon gi, simikat boobu di Ørsted xamlewoon, la [[jëmmalkat]] bu waa-angalteer bii di [[Michael Faraday]]defar ñaari wuutuloxo ngir jóox li mu duppee ab wëndeelug mbëjbijjaakon: ab doxub dooley bijjaakon bu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalukaay bu mbëj gu njëkk.
== Lëkkalekaay yu biir ==
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[Doxalkat demandoo]]
* [[Doxalkaay bu demandoo]]
* [[Doxalkat demandowul]]
* [[Doxalkaay bu demandoowul]]
* [[Doxallat wéy]]
* [[Doxalukaay bu wéy]]
* [[dawaan safaanoo]]
* [[dawaan bu safaanoo]]


{{wikibaatukaay}}
{{wikibaatukaay}}

Sumb bu 2 Samwiyee 2010 à 14:19

Doxalukaay bu mbëj, ab wuutuloxob mbëj la, goo xam ne kàttan giy duggu ci moom gu mbëj la te ga muy génne gu doolerandu la. Doxalukaay yu mbëj yi am nañu solo lool ci dundiinu jamono ju bees ji, te it dëgg la sax, ne limu doxalukaay yu mbëj yi nekk ci am réew dafay firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Te itam deminu, maanam yokkute walla néewte limu doxalkaay yu mbëj yi ci am réew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wàllu xarala mu réew moomu. Ngir dëggal loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfandikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.

Xaralay doxin gi

Wàll gi solowu:

Doxin

Dawaanu mbëj gi day jaar ci ag lëmës gu ñu wëndeel ci ab doggub weñ bi tudd Tekkaaralkat bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjbijjaakon bu ca dawaan jaaree. Toolu mbëjbijjaakon boobu dañ koy sóob ci beneen toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu wëndeelukat bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi dott. Wëndeelukat bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjbijjaakon; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon gu wëndeelukat bi day wootalante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon gu tekkaaralkat bi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dott bi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.

Doxalukaay bii, ci dawaan gu safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan safaanu rek la bijjaakon di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kàttanu mbëj gi day soppeeku tanggoor ngir njeexitu joule.

Taariixam

Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjbijjaakon gi, simikat boobu di Ørsted xamlewoon, la jëmmalkat bu waa-angalteer bii di Michael Faradaydefar ñaari wuutuloxo ngir jóox li mu duppee ab wëndeelug mbëjbijjaakon: ab doxub dooley bijjaakon bu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalukaay bu mbëj gu njëkk.

Lëkkalekaay yu biir

wikbaatukaay am na xët wu tudd: Doxalukaay bu mbëj