Aller au contenu

Jëfandikukat:Daaru Jaxate

Jóge Wikipedia.

Ginaaw nuyoo ak siyaar, seen mbokk mii di Abóo Jaxate di ab saa-senegaal dëkk Tuubaa cosaanoo Kajoor, jànge alxuraan Tuuba Daaray Seex Suhaybu, moo leen di ñaanal jàmm di ko sàkku ci yéen.