Aller au contenu

Geño

Jóge Wikipedia.
kariim  jóob  25 sàttunmbar 2010/waxtu 11:28 Alikànte Espaañ.

waaw lii ngeen wax dëgg la ndaxte sama ñatti maam rekk la lañ ma limal ñeentel ba dem sudaan ak caadd sama maam jótumaa dundak moom waaye baayu tax wax na ma ne sama maam migi juddu ca Atum 1854 ca Dëkk bu ñuy wax walaji ca waalu dexga la ne koon mingi tudoon mañaŋ omar . ana kan mooy baayam omar Jóob mooy baayam omar a ngi juddu 1264 ca Atum gàddaay ga maanaam Axiraa ci ati Islaam ca fuuta Dëkk bu ñuy wax Goolore . Omar Ahmmidu julde wala jumde mooy baayam mingi juddu 1203 ca gàddaay ga axiraa ca fuñuy wax Màddina Alnuubiya fisuudaniya .Ahmmidu Omar Ben Alii mooy baayam mingi juddu ca Atum 1172 ca Dëkk bu ñuy wax tikrir Altanganiya.foofu nik xawma ci baan gox wala baan ´Réew la bookku,ba tax na ku ci am xam xam mangi lay ñaan nga gindima ci Insàllau ,

sama maam Mañaan omar  ca 1881 ci la jugé waloo jégi dexga ñéw Njaambur ci Dëkk bu ñuy wax ñoomre lóo wante booba ay naak yu bare bari la yoroon aki xar niki bëey waante yagul darra mu xam ne boroom muk jur munta dékak baykat  mu def bu naawete mu  maangé ñéw fuñuy wax nayoobe  waante 1886 bu loli jotaan ba tawatul  jurgi sax la ndox  moo waral ñu jaal ba penkup nayoobe  fuñuy wax Dégg  Mbeeloñ wara toolu ci 10 kilometar ak  nayoobe,te foofa neekoon gottu boo xamne pekoom yéep béykat amu fa woon ñépp ay saamu lañ, mutude ko Mbelooñ Jóob  waaye pëll yi mu Dékkaloon  walla yi mu deendaloon,ñu tambuli naan sàresiik  maanaam Kër Mañaanŋ omar  minkoo sañci  1890.

moom nik danabaaxoo di def atmune mu yóobante seexna seexshadibu Ëediyay maamam yonant bi seex shadibu di koy géram ci ay bataaxal ba 1901 mu giseek moom ca lábude ga ca Kér mamaar sarr,1904 seexna ñéw ganesiko mbelooñ mu rayal ko 3 nak ak 7 gatt ba mi deem mu joxko Ëediya 10-ak 10 gatt calako waxe waxam ju siiw ja ne koo ca ba ngay am martaay seexyi booba gisee gunu ci sair waaye biss niki tay amnga seexul muraaduya sa Dëkk bi ñaan nañ fi Yàlla képp kuñ fi mu baña am bugalum bameel ak yaamal xiyaam mu nee ti ko waxal loo bégg ci sa Dëkk bi mune aydara ngagide ñaak Ndox reekk ko yaax mu nee kodemal gas suuf fu seel idil mako ,bim ko inde mu ñaan ca joxko nee ko foo bégg xéewal gi ak ndox mu bari reekk nako suuf si wérl. lii mooy sama Tàriixu Maam Seex Mañaŋ omar .