Fatik
Apparence
Fatik, mi ngi yaatoo 7945km, am 475.970 ciy way-dëkk. Mooy péyu diwaan bi mu bokk (diwaanu Fatik) ak goxu Fatik. Mi ngi juddu niki diwaan ci 1984, ba ñu xaajee diwaanu Siin-Saalum ñaar: Fatik ak Kawlak. Mi ngi tëdd ci lu féete Mbàmbulaanug Atlas gi, ci sowwu senegaal, ci suufu Kawlak, feggok réewum Gaambi ci bëj-saalumam.
Koom-koom
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Koom-koomam mi ngi cëslaayu ci mbéyum gerte, pepp, càmm ak napp.