Eunice Adabunu
Erreur de script : la fonction « build » n’existe pas. Abla Pokou (wala Aura Poku, wala Abraha Pokou) lingeeru Afrig la , juddoo ci fukk ak juróom-ñetti xarnub. Indi na askanu Baoulé ci réewum Gana ba ci Kodiwaar. Léeb bi dafa nettali, saraxu doomam bu góor ngir jàll ag dex .
Bat bi "Baoulé " li nu tudde leegi askan yi , mu ngi joge ci saraxu doomam.
Bicci toppu saraxe, né na "Ba-ouli", loolu dafay tekki "doom bi dee na". Eunice Adabunu mi juddu ci atum 1919, jigéen buy yëngatu ci wàllum jënd-ag-jaay la, bokk na ci jaaykatt yu jigéen yu Naza Benz.
Mongui juddu ci atum 1919, jugge ci gox bu tuuti. Ci 11 at la tambale nekk baana-baana di jaay beñe, suukar ag ay per.
Mu far mujj tekki ci njayum sër, ci jaba bu Lomé teksi muje doon way Nana Benz yinga xamne ño gëna siiw. Mu am ay gëm-gëmug tembte, ngir Eweland bu boyu Tegsi Togo. Segam dafa jël alalam def ko ci limu gëm, mu daldi bokk ci ñi ëpp doole ci parti way tembte yi bi tudd komite mboolom togo, bu Sylvanus Olympio. Ci at yu 1960, bokk na it ci way xelalaate bu gox ba teksi jiite paccu goxu Lomé bu kurel gi ëmb mboolem jigéenu Togo (UEFEMTO). Doxna it ci njangum xale yu jigéenu Lomé.