Djeumbet Gorée

Jóge Wikipedia.

Dieumbet Gorée[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Deuk bi niou guéna kam ci Gorée mougui nekk ci biir guethie Atlantique jegue lol Dakaru. Bokouna ci 19 Commune yi ci Dakaru. Deuk bobou nekhna beureup bou raniékou ci kellu ninii. Nam té dé ci 1978 lako koureul bi nioy wowé Organisation des Nations Unies ci layko jeumbet. Gorée niouko guena ranie ci diamano boniou diay niit te mou guen ci feuss. Gorée nékhna tamit Deuk bu Diekh ci bou boku ci liste bu Nations Unies pour l' éducation, la science et la culture (UNESCO).

Tarikh ku Gorée.[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Portuguais bouniou wakh Denis Dias mo jekka niew fi niou na Gorée ci atoum 1444 mou wowé ko "Palma". Guenaw lolou ci la Hollandais yi doora niew ci atoum 1588. Tourou Gorée mougui diogue ci "Goede Reede" moy fi terce kay bou guen. Guenaw lolou ci la Français niew ci atoum 1677. Niom ak Anglais yi amonagn ay probleme you beurii, ci lagn signe ay katiim benne accord de paix d'Amiens ci atoum 1817, français yi doraa diot thie Gorée.

yayoum niit ku nioul mo wora loone soowe dianteut africa li thie melni (Gambie, Saint louis du Séenegl, Benin, Ghana..), ci la doomu afrique yi di diogue deem Amerique. Toubab yii leen don Diaye delu Europe.

Suniu kayma ci liim ay Domu afrique you beurii laniou diaye diguente (1726 be 1848)[1]. Ni doone diaye nioniou di ay Buuru wolofs neccon ci Senegambia. Goree nekone mba di weyal diayoume doomu adam ci ay dioune att.

Dakaaru boumou dioundo ci attoum 1857, ci la Goree commence di niack place bi mou amone. Toubab yi nio amaal niarri communes Ndar ak Gorée ci Afrique soow jatt.

yetnen communes toff talou ci mouy Teeguédj ak Dakaru .

ci attum 1891, nett niou doone dundu Gorée limba gui tolou ci 2100 domu adama boba domu adama yi dundu ci Dakaru niou lolou ci 8737. lim bobou mosdi yokku boba be tey.

Ci Dookalin Gorée[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Soukandicou ci térre yii administration toubab mo diekk ci diamano colonisation.[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Bo ba Dakaru lebou yi nio fay docale. Motakk Gorée Bocone ci ñiet commune yu niek Bu Senegaal moomé bopam ay att ci kanam, lou diapp 1996, nii done dookal guurgui, denio dioyantii dokaliin Rewmi. Niou Koy woowe "Décentralisation", moy diokk ay katann gook gokan yi. communes yi nekk ci Dakar plateau

Diir Niu ko deff Bokku Laan la
1996-2002 Urban Alexandre Diagne (1922-2010) Maire honoraire
2002 be teyy Augustin Senghor RES Président de l'Union sportive de Goré

Neekiin[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Goree neekh Deuk bou diégué Dial Dial, Dakar Plateau, Bel Air, Thiaroye ak Teugue Guedj.

Meelokane Djeumbet Gorée[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Gorée deefa nekh ci kerr gou maag, woor ko ci biir guedj gui. suniu sett te bu baakh Gorée amout ben espace bu niit

Askaanu Gorée[Soppisoppi gongikuwaay bi]

askan nu Gorée comme Dakaru, niou ci beurii ay lébu la gnou. Bu fa toubab ci yewe ci la commencé di am ay diakasso, té niou wohélen ay "signares" te niu beurii ci Gorée ak saint Louis. Wa Gorée niou beuri ay Djoulit la niou mais amna aussi ay catholique. limu wa Gorée niou gui tollou ci 1102 domu adama.

Komkom[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Goree nekh deuk bu beurri ut ay activité. Suniu kolle a part tourisme ak nappe ak niende nait.Tourisme

Momel ak beureup tarru[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ker diaam yi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

keeru Cosaan[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Feetewaayu[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  1. Abdoulaye Camara et Joseph Roger de Benoist, , Paris, Maisonneuve & Larose, 2003, 155 p.