Disc jockey

Disc jokey (ñu koy wax itam DJ, di jàng "dijéy"), mooy kiy teg woy yi ci xew yi ak ci feccuwaay yi, jagleel ko benn mbooloo.
Fànnu DJ[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
DJ bi ab béglookat la, mooy kiy yor li ñeel woy yi ñuy teg cib barab, (mooy tànn woy yi, waaye it day bàyyi-xel ci mbooloo mi)