Aller au contenu

Damaris

Jóge Wikipedia.

Ci angale mooy Damaris; Ci faranse mooy Damaris

Jenn jigéen ci Aten la woon, ji nangu woon Yeesu jaarale ko ci waare Pool daanaka 55 g.K..

Dañu ciy jàng ci Injiil ci Jëf 17:34.