Dalmanuta

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Dalmanuta – Ci làkku yawut la tur wi jóge. Ci àngale mooy Dalmanutha, ci faranse mooy Dalmanoutha.

Diiwaan la woon, ci penku dexu Galile fu Yeesu demoon. Xamuñu ne tembe fan la nekkoon. Man nañu ko gis ci Mk 8:10.