Aller au contenu

Combretum

Jóge Wikipedia.
Garabug sawat


Sawat gi ci ñoñ Combretum la bokk. Bari na lool ca mànding yu Afrig.

Garab gu neewi xob la, gàjj la guy àgg 1 ba 3i met. Xasam day ñuul bu garab gi gone, buy mag nag day baam.

Soloom siiw na wàllu faj ci Afrig gu soww.

Turu xam-xam

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Combrerum aculeatum