Bowanerses
Apparence
Ci làkku yawut la tur wi jóge. Ci angale mooy Boanerges; Ci faranse mooy Boanergès
Dàkkental la bi Yeesu joxoon Saag ak Yowaana, doomi Sebede yi. Tur wi dafa tekki "Ñi aaytal ni dënnu gi". Xanaa Saag ak Yowanna dañuy gaawa mer.
Tur wi feeñ na ci Injiil ci Mk 3:17.