Bochotnica
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Bii jukki ab junj rekk la.
Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal
Bochotnica ab dëkku-kaw la ca bëj-saalum-penkug Poloñ. Mi ngi ne ci diggante Puławy ak Lublino, ci wetu Opole Lubelskie, ci dexu Bystra.
Mi ngi yaatoo 20 km², ci 2010 amoon na 1.500 way dëkk.