Betfase

Jóge Wikipedia.

Ci angale mooy Bethphage; Ci faranse mooy Bethphagé

Benn dëkk bu ndaw la woon, ci tundu Oliw ya ci yoonu Yeriko diggante Yerusalem ak Betani. Sorewul Betani.

Dañu ciy wax ci Injiil ci Mc 21:1; Mk 11:1; Lu 19:29.