Bartime

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Ci làkku yawut la tur wi jóge. Ci angale mooy Bartimaeus; Ci faranse mooy Bartimée

Gumba ci dëkku Yeriko la woon, bi Yeesu gisloo woon. Man nga jàng ci Bartime ci Mk 10:46-52.