Barsabas
Apparence
Ci làkku yawut la tur wi jóge. Ci angale mooy Barsabas; Ci faranse mooy Barsabbas
Ñaari nit ñoo bokk dàkkental bi:
- Yuusufa ku bokkoon ci ñaari nit ñi ndawi Kirist ya tuddoon ngir wuutu Yudaa Iskariyo (Jëf 1:15-26). Turam feeñ na ci Jëf 1:23.
- Yudd, benn njiit ci mbooloo ñi gëm ci Yerusalem. Jëf 15:22.