Baal
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Ci làkku ibrë (בעל) la tur wi jóge. Ci angale mooy baal; Ci faranse mooy baal
Xërëm la woon; waa Kanaan defoon ko Yàlla. Israyil daan na ko màggal itam. Ci Injiil man nañu gis Baal ci Ro 11:4.