Atali
Apparence
36°54′N 30°41′E / 36.9, 30.683
Ci angale mooy Attalia; Ci faranse mooy Attalie
Dëkk la woon, di teeru bu gëna am solo ci diiwaanu Pamfili fa diiwaan bi digalook diiwaanu Lisi. Tey jii Antalya ci réewu Turki (Turquie) la.
Man nañu koy gis ci Injiil ci Jëf 14:25.