Aller au contenu

Asànkirit

Jóge Wikipedia.

Ci angale mooy Asyncritus; Ci faranse mooy Asyncrite

Benn toppkatu Yeesu ci Room la woon. Turam feeñ na ci Injiil ci Ro 16:14.