Apolyon

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Royuwaay:Merge Ci angale ak ci faranse mooy Apollyon.

Turu malaakam kàmb gu xóot gi ci làkku gereg la. Mu ngi tekki 'yàqkat'. Dafay wax ci buuru njéeréer yi ñu gis ci téere Peeñu ma ci Injiil (Pe 9:1-12). Lu ëpp ci boroomi xam-xamu Injiil yi xalaat nañu ne ci Ibliis lay wax. Seetal itam Abadon.

Ci Injiil dañuy gis Apolyon ci Pe 9:11.