Anet Mbay Dernwil

Jóge Wikipedia.


Anet Mbay Dernwil

Dundu ak jaar-jaaram
Juddu 23 suwee (juin) 1926 (juroom-ñeent-fukki at ak ñeent)

Fatig

Réew Senegaal
Tàggatu Ekool Normaal bu Tëngeej (Rufisque)
Liggeey Bindkat, Taalifkat

Erreur de script : la fonction « build » n’existe pas.Royuwaay:Infobox en Lua Anet Mbay Dernwil mu ngi juddu atum 1926. Bindkat la woon, nekkoon taskatu xibaar, nekkoon it kuy wax ci rajoy réew mi.

Dundu ak jaar-jaaram[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Anet Mbay Dernwil mu ngi juddoo Sóokoon fukki fan ak juroom ci weeru desàmbar atum 1926.

Li ëpp ci ay téereem, ay taalif lañu wala ay mbind yu mu def ngir xale yii.

Moom mooy ki sooke amalug Miise bi ñu jagleel jigeen ñi, tuddeko  Hãariyet Bàccili ca Gore (Musée de la Femme Henriette Bathily de Gorée).

Saa-sinemaa bile di Usmaan Wiliyaam Mbay, juddu atum 1952, doomam la. Moom Usmaan Wilyaam Mbay sax, def na benn film ci yaay ji atum 2008, tudde ko « Mère-bi ».

Ay téereem[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • 1965 : Poèmes africains
  • 1966 : Kàddu (réédition des poèmes)
  • 1976 : Chansons pour Laïty
  • 1983 : Le Noël du vieux chasseur
  • 1983 : La Bague de cuivre et d'argent (prix Jeune Afrique en 1961)
  • 2003 : Motte de terre et motte de beurre
  • 2003 : Picc l'Oiseau et Lëpp-Lëpp le papillon

Seetal tamit[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Jukki yi ñu ko tudd[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • Càllalag Senegaal : <small>Littérature sénégalaise</small>
  • Limu bindkati Senegaal yi :
  • Tasukaayi xibaar yu Senegaal : <small>Médias au Sénégal</small>
  • Taarixu jigeen ci Senegaal : <small>Histoire des femmes au Sénégal</small>

Lees bind ci moom[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • Royuwaay:Autorité
  • « Annette Mbaye d'Erneville : L'éclaireuse », in « Femmes au Sénégal », Les Cahiers de l'Alternance (Dakar), Partenariat Fondation Konrad Adenauer et Centre d'études des sciences et techniques de l'information (CESTI), no 10, décembre 2006, p. 40-41
  • Aliane, « Mme Mbaye d'Erneville, directrice des programmes à l'Office de radiodiffusion du Sénégal », Amina, no 32, juillet 1975, p. 21-23
  • Pierrette Herzberger-Fofana, « Annette Mbaye d'Erneville (Sénégal) », dans Littérature féminine francophone d'Afrique noire, Paris, L'Harmattan, 2000, p. 374-81.

Lees jële feneen[Soppisoppi gongikuwaay bi]