Aller au contenu

Amiin

Jóge Wikipedia.

Ci làkku ibrë (אָמֵן) la baat bi jóge. Amiin mooy ni ñu koy waxe is làkku araab (آمين). Ci angale ak ci faranse mooy Amen.

Baat bi dafay tekki 'Na ame ni nga ko waxe.'

Ci Injiil dañu koy gis ci Mc 6:13; Ro 1:25; 9:5; 11:36; 15:33; 16:24,27; 1Ko 14:16; 2Ko 1:20; Gal 1:5; 6:18; Ef 3:21; Fb 4:20; 1Tim 1:17; 6:16; 2Tim 4:18; Yt 13:21; 1Pi 4:11; 5:11; Yu 1:25; Pe 1:6,7; 3:14; 5:14; 7:12; 19:4; 22:20.