Alisa
Apparence
Ci làkku yëwut (אֱלִישַׁע) la tur wi jóge. Alisa mooy ni ñu koy waxe ci Lislaam. Ci angale mooy Elisha; Ci faranse mooy Elisée
Yonent la woon, bu donnoon yenu yonent Yàlla Iliyas. Man nañu jàng ci jalooreem ci 1Ki 19:19-21; 2Ki 2:1-2; 3:11-20; 4:1-8:15; 9:1-3; 36-37; 13:14-21.
Dañuy wax ci Alisa ci Injiil ci Lu 4:27. Lu 4:27 wax na ci li ñu jàng ci 2Ki 5:1-27.